Genre not found
Artist not found
Album not found
Song not found

Siiw
Thione Seck Lyrics


siw dou diami borom ma thi kham dara leppeu lou yengou yow laniouye key djigne
yegoulo fékéwo niou fénte wokhou niaw am bapa mou bari tay ko sa guinaw
bo ma guissé di ma ré ma wone la guinaw nga yakha sama der dou ma diar dara

Refrain
bayi lène di bakar, wokh llou la woroul lébi nène
bayi lène di bakar, wokh llou la woroul lébi nène
l'islam da key ayé

diapa sa ma dom di dor ma takhaw di la khol bou sa yaram dé daw nga bayi ko
fi la deukeu fi la djoudo di weuye sa ma mame teki dara guene wo yéwoulène
lou way di def di thia tokh kénée tedda na thia mbirou yalla mo woor

Refrain

bo ma guissé di ma ré ma wone la guinaw nga yakha sama der dou ma diar dara

Contributed by Gavin R. Suggest a correction in the comments below.
To comment on specific lyrics, highlight them
Comments from YouTube:

Lalia Diop

Repose en paix papa à jamais dans nos coeur😭😭😭j'arrive toujour pas à y croire que mon artiste s'est éteint

boss

😭😭😭😭😭

Toulaye Diop

Amine

Haby machala Niang

Ahbib 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭

Maye Kane

Pale tone seck wetlle ganebilay😭😭😭😭💔💔💔💔

so'girl♥️

En ce 14 Mars jour de ta disparition j'écoute tes belles paroles et mélodies.. Yalla nako yalla yeureum souff seedd si kawam 🙏🙏🙏

Toulaye Diop

Amine

Fatou Bintou Ndime

Vraiment magnifique, la qualité en son en image assurée. Wally attention, pa bi bayégoul dé...😅😅😅

Amadou NDIAYE

Ah ndeysaan mujj naa baayi aduna du dara

Alioune Badara NDIAYE

Puisse Allah être satisfait de tes oeuvres terrestres et t'accorder sa Miséricorde infinie pour les insuffisances. Que le Paradis soit ta dernière demeure

More Comments

More Videos