Genre not found
Artist not found
Album not found
Song not found

Lees Waxul
Yandé Codou Sène Lyrics

No lyrics text found for this track.

The lyrics can frequently be found in the comments below, by filtering for lyric videos or browsing the comments in the different videos below.
Most interesting comments from YouTube:

Milie

Youssou- Dou leup lignou la wone mba lignou la misal, nga dal di koy guem del deglo, lou wesou dedet.

Yandé C.- Ndigalo fall, wonala ndigal bayi gor, wonala ndigal bayi gor, Meissa bigué coumba Fall borom farathi nnga gambiene, daba mame sene ndiayoooy ndigal fall, diambari khelkom. ndiagalo fall, diambari lislam, nena lessoy nena less wakhoul!

Youssou: Meisssa ndigeul Fall, diambari lislam, diambari khelcom, nena less hooy nena less wakhoul

Yandé: diambaroooooy Fall, diambar ndigal fall gor Meissa bigué Coumba Fall, diambarooyy digal Fall gor Meissa bigué coumba Fall, diambarooyy digal fall gor Meissa bigué coumba Fall, ndiamara khafifa Baye gor Fall, malay wooo Fall Meissa Bigué coumba Fall! Nena nena less hooy nena less wakhoul

Youssou: Boul degeu dal di gueum wala guiss rek ne Wawe Guiss da fa wara lère Degeug degeug wara khaute
Diangal lathia bire Dou lepp lou nieuw ga gueum ko! less oyyyy nena less wakhoul

Yandé: Ndarooo ma Ndigal bayi Gor, diarama yooooh Diambarbi Fall, diambarooo nila goor di mel Fall, diambarooo nila goor di mel Fall, Gor bou donnné bayam kou manam wathna Fall Meissa bigué Fall, yay seutou ibra fall meissa Bigué Fall, sa mame Ibra Fall a fegnal Ahmadou Bamba! Diambaroy Ndigal Fall, nena less oyy nena less wakhoul:

Youssou: diambari l'islam, yiiiiiii less oyyy nena less wakhoul

Yandé: Diambare woyy ndiagal Fall meissa! Ndigal Fall Meissa Bigué Coumba Fall borom farawathie ndandagne Ndeye demba mame say ndiaye, sa mama a fegnal Bamba ahh, sama a fegnal Bamba ahh, samama a fegnal Bamba cheikh baye gorr Meissa bigué coumba fall, sa mama a fegnal Bamba Cheikh baye Gor Meissa Coumba Fall, sa mama a fegnal Bamba Cheikh bayi gor MaDeguene DEmba Fall, sama ma fegnal Bamba Meissa Bigué Coumba fall! né diambari khelkom, nelanénn Fall, nénalen wakhoul

Youssou! Boul degeu dal di gueum wala rek guiss dal ne Wawe Guiss da fa wara lère Degeug degeug wara khaute
Diangal lathia bire Dou lepp lou nieuw ga gueum ko! less ooyy nena less wakhoul

Nenalénn fall.....

All comments from YouTube:

Tpe Sfa

Elle a chanté pour la naissance de ma grande soeur et de ma famille c'est une femme incroyable que Dieu l'acceuille au paradis

Cristina Garelli

magnifique message et voix ! Gratitude infinie envers ces deux artistes merveilleux....

Sylvain Ngor Sarr

triste!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!! oh yande codou une legendaire r.i.p

Khote Faye

magnifique voix yalla nako yalla yeureum te khareko aldiana vraiment je suis emu par cette chanson

Fatou A Sarr

may her soul rest in peace

Khalifa Fall

cette chanson me touche au plus profond de moi. Repose en paix Yande codou

Sankoung Diaby

Nice

Mamé Ndao

Dieureudieuf Mame Cheikh Ibra🙏🏽. Mame Boye Yalla nako Yalla yeureume te khare ko Al Diana ❤❤❤

papi Torino

Ndaye san souf dielna kounè yande codou sene yalla nako BOROM TOUBA tèrou

Modou abib Napoli

amine

More Comments

More Videos