Wouyouma
by Positive Black Soul

Positive Black Soul - Xoyma

Xoyma xoyma xalebile yaw niowal xoyma
Xoyma xoyma xalebile yaw wonma doyna
Xoyma xoyma xalebile yaw niowal xoyma
Xoyma xoyma xalebile yaw wonma doyna

Didier
Xadjalma meyma
Mayma touti teyma teyma
Wone la fane la
Fanla naalna nakala
Yaw kay ma deela
Boul ma rombe noonou deena
Dee na deena boul ma djekali baby doyna
Wooma demba fi ba tambacunda
Ne ne xamoulo, xaana freloulo
Dii ma mirlo dima keuyit lo
Nene doyna, doyna, doyna, doyna, doyna
Nene xolma ni Doug E Tee legui djexna
Nene xolma sama biir sou deye bi legui demna
Nene xolma sama appetit de lequi djexna
Nene deena legui nene doyna xoyma

Xoyma xoyma xalebile yaw niowal xoyma
Xoyma xoyma xalebile yaw wonma doyna
Xoyma xoyma xalebile yaw niowal xoyma
Xoyma xoyma xalebile yaw wonma doyna

Amadou
Yaw baby romb ngasama xel bi jaxassona
Ne manmi dromina sama fiit bi labajona
Manmi dama samp thioukel
Kon ndawsi boul ma soufel
Ndax xamnga ne bo nekone
Ndokh manmi may done sa bouteile
Sa yaram de fa sët sa waxine da fa léér
Sa dokhine da fe diek sa dieufine
Mome dou yeufou séér
Djigune da fay mat mo takh
Ngaye dokhe bileum leumb
Bala may guena dof nga
dianokmane ba dimay leumbale
Diokh nga thïeur samayaye
Fate wo sama baye
Lolou laye niane si yaw kon yaw
Boul fate samay waye
Sougnou wete dama kham soma
Sokhle dama ame
Sougnou wete nala wone
ne mandeye baybi limeumene
Yow baby baby baby...

Xoyma xoyma xalebile yaw niowal xoyma
Xoyma xoyma xalebile yaw wonma doyna
Xoyma xoyma xalebile yaw niowal xoyma
Xoyma xoyma xalebile yaw wonma doyna

Didier
Dimbalima xoyma, mene gale
Dikal niowal xoyma
Dimbalima xoyma, mene gale
"argay" niowal xoyma
Oubil nga meyma ma wox sa noppa
Baby deyla
Oubil ma woxla sama
compte bacaire nounngi deena
Oubil ma meyla sama tiabi
gale moungui deena
Oubil ma meyla sama tiabi auto moungi
Nene xamoulo, xana feeloulo
Dimamiirlo dima keuyitio
Nene doyna, doyna, doyna, doyna, xoyna

Amadou
Yama newone manala te netetoma
Teguis noa kou mané
Te yate maneko soma newoul
Souma neke dina koné
Yaw kay, Kay way

Xoyma xoyma xalebile yaw niowal xoyma
Xoyma xoyma xalebile yaw wonma doyna
Xoyma xoyma xalebile yaw niowal xoyma
Xoyma xoyma xalebile yaw wonma doyna

Contributed by Leah Y. Suggest a correction in the comments below.

Genre not found
Artist not found
Album not found
Song not found